Moné youkhouna walou
Wakhtaané nako gnou néko yaw seuy mougnal
Djeuk na ko door ci lanamou xaléyi
Yagana diko sonal
Khadj goudi lay tew djapé nako djiam sokhnasi do toul nélaw
Magui léne di lacc ana sunu Yëurmandé
Sa dôme sa sœur la rak wala mak
Bayi ko khél
Yëurmandé éh éh éh
Jiguéne nay sunu yaye
Délou gueun léne fonk way
Yëurmandé é éh éh
Essuie tes larmes
Fi koufi bakh Jiguéne na djour
Tu es une femme pas une esclave
Essuie tes larmes et ne pleure pas
Un jour il comprendra tout le mal qu'il a fait
Dehors avec les autres tu fais le beau
Quand tu rentres à la maison c'est le Rambo
Elle t'a donnée de l'amour plein de tendresse tu la frappes
Y'en à marre de tout ses cris
Tout le temps le jour et la nuit
Yëurmandé éh éh éh
Jiguéne nay sunu yaye
Délou gueun léne fonk way
Yëurmandé é éh éh
Essuie tes larmes
Fi koufi bakh Jiguéne na djour
Wakh taan nalak mome téboul ko dor
Jiguéne alalou Yalla la
Ouh ouh ouh
Wakh taan nalak mome téboul ko dor
Jiguéne alalou Yalla la
Ouh ouh ouh
Yëurmandé éh éh éh
Jiguéne nay sunu yaye
Délou gueun léne fonk way
Yëurmandé é éh éh
Essuie tes larmes
Fi koufi bakh Jiguéne na djour