Unite now (x4)
Afriki yewul naac na (x4) Unite now
Téy lagnu geum afreeca beug dunde jeum kanam
Téy lagnu geum sugnu euleuk wékkuwul ci kéne
Xam fignu jeum oh farafina !! xamél ci xambe fitna
Gnila meune délo ginaw say ennemies deug deug
Gni wéddi sa meun meun gnila yagg deug fél sa geud
Afreeca fimou jaaré ay yoonam dafa xaré
Jonganteek ay jafé jafé gniko jiité dougnou jeufé
Sen kaddu dé jaggul dou wallu jaroul gnoukoy gaddu
Xalé yi xiif di saraxu kom kom gi dé di wattatu
Ganay yi geune sakkan lambe ta se kémb jarrul
Alleu bi soppeeku taax yi lékk tool yi réggul
Marral békoor fallu baykatt bi soldaaru
Afriki yéwul naac na (x4) yéwul naac na
Afreeca yéwul naac na (x4) Unite now
Bismarck limou teureul jiggu gnu gno bagn seuggu gnu
Lou takh gnu beug gno neube jant bi lé né faang? fok
Naaj bi teub gnu APE bignu signé xaax teuf beuggu gnu
Cheikh Anta Diop inddina tonttu mboleem civilisations
Afreecay sen penkku wolof bambara toutsi bantus
Afreeca Unite bougn ko gantu wolof nga ni namppu gnu babtou
Filé sign juddo beug ko faatlu lakk bou rafé té ni mouk mouk dou sanku
Afreecay wooté mbolo fok ndeunde bi samppu nagnu maas noun gui Def
Ci tomb
Bougnou boolé sougnou doolé euleuk dougnou romb
Bayyi yalwaan wi baaram yi bankou
System mou babylon no kheuy gnou gontou
Afriki yéwul naac na (x4) yéwul naac na
Afreeca yéwul naac na (x4) Unite now
Africa for so long
You've been suffering down inside in silence
Farafina it's all about time your sons and daughters get together
And stop the violence
Yéel gni doon nélaw xana yeugu gnu ngélaw
Béneen afrik mou seulmu yéwu ca njeul cepeelu
European sosna fitna nguir gnou ngaayoo daayiman
Weulbatiku ci souf di youlli sougnouy diamond
Suul bouki suuliwaat ndawu afrik yeukeuti baat
Ande bolo geustuwaat lou tax meunougnou dém
Bi moy kheep sa bop roy daqq ci nassaraan
Fate baakhi maam toppi nakhi neen
Afriki yéwul naac na (x4) yéwul naac na
Afreeca yéwul naac na (x4) Unite now