Back to Top

Karim Diouf - Xamm mé Lyrics

Karim Diouf - Xamm mé Lyrics

Baye Boye, yague na la deguelou gua may diggeul, lo bakh Sama Baye Boye
Khame na ni, lounek dadj gua ko baye lëp guir mane
Khame na ni méti wone na lolou tchi djamono yé gnou wessou
Yaye Boye, mandé dama kotane ba wéye wéye gui mala wéye
Sama Yaye Boye,
Khame na ni lounek dadj gua ko yaye lépeu guir mane
Kame na ni méti wone na lolou tchi djamonoyé gnou wessou
Mane dé yene la beugue, mandeé yene la mine, Mbeuguël bou (2 x)
Tchi raguogne tourro kone saguo djekh na
Khame na né, lounek dadj gua ko yaye, lépeu guir mane
Khame na né, méti wone na lolou tchi djamonoyé gnou wessou
Khame na li ma momak li ma momoul sa waye, té deuguela
Djangue Djanguano, kouye djanguane bo mokallé bérre sa dara
Teye ma bérre sama dara ndakh baye boye néna kouma beugue
Ma beugue ko, kouma beigne khawma loumou maye wagni
Waw lolou deugueu la
Khame na li ma mom ak li ma momoul sa waye, te deugereula
Douguou Douguou waguane Faye, khaliss wagane Faye, wagane
Coumba sandjane,Faya gok sama yaye djii yaye ma gui lay
Gniane yaya nga gniaral gnou waw data gueune si gnioune han
Yayo han sama yaya boyo, yaye gniaral ma
Seynabou, Gourgui
Khamé na li ma mom ak li ma momoul sa waye
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: Elage Diouf, Karim Diouf
Copyright: Lyrics © Évangeline/APEM

Back to: Karim Diouf

Karim Diouf - Xamm mé Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: Karim Diouf
Written by: Elage Diouf, Karim Diouf
[Correct Info]
Tags:
No tags yet