Back to Top

MAMADOU MOUSTAPHA LO - BALBALOU Lyrics

MAMADOU MOUSTAPHA LO - BALBALOU Lyrics

Balbalou wooroul, balbalou woorul, balbalou woorul

Yallah dafa saka khér, khér di balbalou
Yallah saka wegne mou tothie khér wa
Yalla saka wegne mouy balbalou, mouy balbalou
Yallah saka safara mou séyal wegne

Yallah saka safara mouy balbalou
Yallah saka ndokh mou fayko

Ndokh di balbalou ditaw ditaw di balbalou
Yallah saka nguelaw mou daldi sewet
Nguélaw di balbalou, nguélaw di balbalou
Yallah saka wakha mbané
Wakhambané di balbalou, hum, yalla saka djiguené
Coumba man coumandang, couba man coumandang
Djiguené di balbalou, di balbalou, di balbalou wo
Yallah sakal ko liir
Liir di balbalou, di balbalou, yallah sakalkoy nélaw
Nélaw di balbalou, di balbalou, yallah saka adio, manami soxla
Adio di balbalou, di balbalou, di balbalou
Yallah saka nit kou bhakh
Nit kou baakh di balbalou, di balbalou
Yallah saka déé, yallah saka déé
Déé di balbalou, di balbalou, yallah saka yowmal khiyam
Yawmal khiyam kou fa yegga sa balbalou diéékh

Balbalou woroul... balbalou woroul

Boula yalla mayé, boula yalla mayé, Nga dimbalé
Gni nga tanééy

[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Writer: IBRAHIM MAALOUF, MAMADOU MOUSTAPHA LO
Copyright: Lyrics © WAGRAM PUBLISHING, Warner Chappell Music, Inc.

MAMADOU MOUSTAPHA LO - BALBALOU Video
(Show video at the top of the page)

Performed By: MAMADOU MOUSTAPHA LO
Written by: IBRAHIM MAALOUF, MAMADOU MOUSTAPHA LO
[Correct Info]
Tags:
No tags yet