Back to Top

Punchef - Guelwar Lyrics

Punchef - Guelwar Lyrics

Beurigo bou fess dou df bruit gni xam nio dall
Beuyeuh ngay katt katti, xar df thiell
Gaw ci baxoul teii dougne leuh wax loutax
Fi Sodoul nguisteul ken doula sedel mbax
Bopou ci ndox dinga lapp ci thiono
Xouss ci rongongne do diok ci problème
Exporté diameuh importé problem
Meme aire bigni noyi manqueii neuh oxygene

Diante finke beute sett, lerr leuh goudi di thiax
Deii meunoul ray kidone doundeul lou bax
Taxaw sa bamel di cass Dameuh say loxo bagne niane
Sakou ndimbeul loloy avortement
Tite dessak fite
Niak sameuh ngor
Cm sede none
Masslak ay deum teii douma carnivore
Kou ragal deii téré doundou meun nga lebleii say fane
Ragal échec douma téré mouk risquer sam life
Lima mérité lay am dama mérité am
Wett ak sa bop loloy medité âme
Yafouss douma khâgne lou ndiambar di mayé
Degg xeweul bodoul guiss melni mamou momar
Dieuf diou feki wakh natoukayou deug
Rap lou haut niveau

Clash nagne ma ba sonou niouy moudié rabbeii ni mane
Ch ouais c vrai dagne ma fan wone ci pete
Ibiliss saxa len gueun ndax mom assumé neuh
Gnila nianal binga ameii niom nio ndieukeuh sissou
Même samay dio dagne may vexer diapeii ko kagne
DonTeii wooy, doko degg ci man
Soumay deii douma wekou xamko ci man
Dieul sa life df ko sound lolou doyna keman

Daathie ni marteau ak brain, thiakh leuh oubil sa brain
Let's fly like plane, rap lou haut niveau

Hussle ba xonete god mayma second chance may ki deukeii
Dox dadiek sam deii ndiouy ko ni fifty cents
Yam fima god yamalé sabablou sa souneii
Solna dallou lat dior defouma tankounen
Bima xipé sam beute bobou la ray bi teine
Xiff diaralouma lekk nitt leuh nitti tam
Temperament allemand no df ma tang shine
Sous côté ni dina yatou xol h gawa shine
Supprimer gnima sous estimé
Louma df ci sam life meun nako assumé
Ken douma dioxogne sam yone ken douma dictée sam choix
Meuss na df lou bone taxoul mou baisser sam foi
Chaque fois may rap teii meunouma ndeupeul sam bop
Gueun yess ci lima weur werleii di gueun di wop

May pivot captain quater running back
Centinel ci digg bi coacheii ay supporter
Ccteur sama life meussouma figurant
Ndm nioneii cana dou xalate ma téré bandana
Yegueul thiaya concert pour gnimou concerner
Constater fi ay fail conard yi ligni cons
Comme dab may sauver sen rap teii meusso degg sam gatt
Saxaral shit bi dou pap, yemouma seni crack f*ck off
Craquer sen mind system cheval de troie
Rap dou rawanteii fass teii lol la mbam yi fokk
Cmna lerou fenn katt bou nitou deug tok
Hip-hop ngandi poukheu mc yi nek tott
Succès dou dioudou ci vision court terme
Liberté Moy nga sagna df sa erreur
Kou guiff leral sa merr mtx nitti di nieuk
Teii ligne leuh beugué lagne lay bagneii wa salam
[ Correct these Lyrics ]

[ Correct these Lyrics ]

We currently do not have these lyrics. If you would like to submit them, please use the form below.

Wolof

Copyright: Lyrics © Original Writer and Publisher
LyricFind

Back to: Punchef

Punchef - Guelwar Video
(Show video at the top of the page)

Click here to scroll the video with page

Performed By: Punchef
Featuring: Abdoul Aziz Fall, beatbybiz, Mamadou Camara
Language: Wolof
Length: 3:03
[Correct Info]
Tags:
No tags yet